Wolof
Am na ñoo xam ne bu ñuy jaxal, ci àmbolog lañu koy def ndax moo ëpp sutura
· Source : Corpus Oraux du LLACAN (dataset dofbi/jolof, Hugging Face)
il y a des gens qui, lorsqu’ils apportent leur aide financière à une famille endeuillée, la mettent sous enveloppe pour plus de discrétion.