Wolof
(prov.) Kuy daanoo ca guy, jàppandiku ca mbortaan, dangay yàggal sa jéll, waaye ca suuf nga jëm
· Source : Corpus Oraux du LLACAN (dataset dofbi/jolof, Hugging Face)
si en tombant d’un baobab, tu t’accroches à la fleur, tu ne fais que retarder ta chute mais tu te retrouveras au sol.