Wolof
Gënuma laa xam li nga wara def, dama doon woslu-àq rekk bi ma lay wax nga jox ko loxo
· Source : Corpus Oraux du LLACAN (dataset dofbi/jolof, Hugging Face)
je ne sais pas mieux que toi ce que tu dois faire, je voulais seulement m’acquitter d’une obligation, en te disant de lui serrer la main.